Romans 7:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Léegi nag du man maay def lu bon loolu, waaye bàkkaar bi dëkk ci man, moo ma ciy jiiñ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag dootu man maay jëfe noonu, waaye dooley bàkkaar bi ci man la.