Romans 7:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte xam naa ne, lu baax dëkkul ci man, maanaam ci sama bindu doom Aadama. Am naa yéeney def lu baax, waaye awma kàttanu yeggale.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam naa ne man, sama bindu suuxu neen wii, lenn lu baax dëkku ci. Yéene jaa ngeek man, kàttanu jëfe lu baax moo fi nekkul.