Romans 7:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu fekkee nag lu ma bëggul, moom laay def, kon dootul sama coobare, waaye bàkkaar bi dëkk ci man, moo ma ci jiiñ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te su dee li ma nammul, moom laay def, kon kay dootu man maa koy def, waaye dooley bàkkaar bi dëkk ci man moo koy def.