Romans 7:23 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye gis naa jeneen doole juy yengu ci samay céri yaram, di bëre ak li sama xol bëgg; day bëre ba noot ma, def ma jaam ci dooley bàkkaar joojuy yengu ci samay cér.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye gis naa ci samay cér, weneen yoon wuy xeex ak yoon wi samam xel jubool, te yoon woowoo ma jàpp njaam, jébbal ma dooley bàkkaar bi dëkke samay cér.