Romans 7:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Keroog ba nu daan topp sunu nafsu, yoonu Musaa daan na xamb bëgg-bëgg yu bon, yiy yengal sunuy cér, ba jural nu dee.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba nu toppee sunu bakkan, sunu bëgg-bëgg yu bon yi ndigali yoonu Musaa yee, ñoo daan liggéey ci sunuy cér, ngir nu meññ lu nu jëme ci ndee.