Romans 8:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Léegi nag yoon mënul a dab ñi bokk ci Yeesu Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag léegi, amul benn daan bu ñeel ñi bokk ci Almasi Yeesu.