Romans 8:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ñépp ñiy déggal Xelu Yàlla mi, ay doomi Yàlla lañu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat, mboolem ñiy dox ci njiital Noo gi, ñooñu ay doomi Yàlla lañu.