Romans 8:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nekkatuleen fa kanam Yàlla, ni jaam bu ragal sangam, waaye Xel mi leen Yàlla sol, ay doomi Yàlla la leen def, ba tax nu di wooye Yàlla: «Abba,» maanaam «Baay bi.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mayeesu leen noo gu leen di desloo cig njaam, ba tax leena dellu cig ragal, waaye Noowug doom yu ñu doomoo, moom lees leen may, te looloo nu tax di wooye Yàlla: «Abba », mu tekki «Baay.»