Romans 8:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax li Yàlla bind lépp a ngi ne seew a gis doomi Yàlla yi feeñ ci seen biir ndam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Càkkéefu àddinaa ngi séentu, ndax yàkkamti bés ba doomi Yàlla di feeñ.