Romans 8:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam nanu ba fi nu tollu ne, li Yàlla bind lépp a ngi metitlu ni jigéen juy matu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam nanu ba fii nu tollu ne mboolem càkkéef gaa ngi binni ndax mitit, ni kuy matu.