Romans 8:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te ñi mu dogaloon loolu ci ñoom, da leen a woo; te ñooñu mu woo, da leen a àtte ni ñu jub; te ñooñu mu àtte jub, da leen a boole ca ndamam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñi Yàlla tuddaloon loolu lu jiitu, moo leen woo itam; ñooñu mu woo, moo leen jox itam àtteb ñu jub; te ñooñu mu jox àtteb ñu jub, moo leen darajaal itam.