Romans 8:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñi Yàlla tànnal boppam, kan moo leen di tuumaal? Yàlla moo leen àtte ni ñu jub.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñi Yàlla taamu, ana ku leen di tuumaal? Yàlla de mooy jox nit àtteb ku jub.