Romans 8:38 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax wóor na ma ne, dara mënu noo tàggaleek mbëggeelam; du dee, du dund, du malaaka yi, du seeni kilifa, du tey, du ëllëg, du boroom doole yi,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat bir na ma ne du ag ndee, du ag ndund, du ay malaaka, duy boroom nguur, du tey, du ëllëg, duy boroom doole,