bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Romans 9:1
Romans 9:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Li ma bëgg a wax nag, ci kanamu Kirist laa koy waxe; dëgg la, du aw fen. Sama xel, mi Xel mu Sell miy leeral, seedeel na ma ne, dëgg laay wax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dëgg laay wax, Almasi seere na ko, fenuma. Sama xol moo ma seereele Noo gu Sell gi, ne lii may wax dëgg la: