Romans 9:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te du ci loolu rekk, waaye noonu la it ci lu jëm ci Rebeka; doom yi mu jur ñoo bokk benn baay, moo di sunu maam Isaaxa.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te yemul foofu rekk, waaye Rebeka it moo am ay seex yu genn góor jur, muy sunu maam Isaaxa.