Romans 9:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon lu nu ci war a wax? Ndax Yàlla àttewul foofu yoon nag? Mukk!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana lu nu ci mana wax nag? Yàlla daa wàcc foofu yoon? Mukk kay!