Romans 9:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Dafa wax Musaa sax ne ko:«Dinaa yërëm ku ma neex,laabiir ci ku ma neex.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat moo noon Musaa: «Maay yërëm ku ma neex, te maay ñeewante ku ma neex.»
Recommended Reading