Romans 9:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te wax ji noo ko moom, nun ñi Yàlla woo ci boppam ci biir Yawut yi ak ci biir xeet yi ci des.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nun ci ndabi yërmande yi Yàlla woo lanu bokk, te du ci Yawut yi rekk lees nu seppee, waaye ci jaambur ñi dul Yawut itam.