Romans 9:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moom la wax ci téereb Ose ne:«Ñi nekkul woon sama xeetdinaa leen ko def,ñi bokkul woon ci sama mbëggeel,dinaa leen ci boole.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moom la wax it ci téereb Ose ne: «Ñi dul woon sama ñoñ, ñoom laay wax sama ñoñ, ñooñu dul woon samab xejj, ñoom laay xejjoo. »