bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Romans 9:27
Romans 9:27 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Esayi wax na ci mbirum Israyil ne:«Lu bànni Israyil baree-bare ni suufus géej sax,lu néew rekk a ciy mucc.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci mbirum Israyil la Yonent Yàlla Esayi itam xaacu woon ne: «Su bànni Israyil tolloo ni feppi suufas géej sax, as ndes a ciy mucc.