Romans 9:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Esayi it waxoon na lu jiitu loolu ne:«Yàlla Boroom kàttan gi,su bàyyiwul woon ci nun lu néew,kon ba tey raat nanu ni dëkki Sodom ak Gomor.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mooy itam la Esayi waxoon lu jiitu, ne: «Su nu Boroom gàngoori xare yi waccalul woon kuutaay, ni Sodom lanuy mel, Gomor lanuy neexool.»