Romans 9:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bànni Israyil, mi bëggoon a sàmm yoon ngir jub, matalu ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye xeetu Israyil wi sàkku woon yoonu njub, ñoo moy yoon wi.