Romans 9:32 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax lan? Ndax dañoo sukkandiku ci seeni jëf, bàyyi ngëm. Dañoo daanu ci «doj wuy fakkatale.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax lan? Ngëm lañu sukkandikoowul, xanaa ay jëf. «Doj wuy fakktale,» moom lañu fakktaloo.