Romans 9:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moom la Yàlla wax ci Mbind mi ne:«Dinaa samp ci Siyon doj wuy fakkatale,di xeer wuy daaneel nit; waaye ku wéeru ci moom, sa yaakaar du tas.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu la Mbind mi indee ne: «Maa ngii di dëj fi Siyoŋ doj wuy fakktale, mooy xeer wuy daaneel, waaye ku ko wéeroo ngëm, doo rus.»