Romans 9:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye neewuma waxu Yàlla dafa toxu, ndaxte bokk ci bànni Israyil, taxul nga bokk ci Israyil tigi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Du caageenu kàddug Yàlla moo neen, ndax ñi bokk ci xeetu Israyil ñépp duñu Israyil tigi.