Ruth 2:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ruut ne ko: «Teral nga ma de, sang bi. Yaa ngi may laaye biir, ndaxte dëfal nga ma, wax ma lu seral sama xol, te moona say surga yu jigéen yi sax a ma gën.»