Ruth 2:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xoolal bu baax fi xale yu góor yiy góob, te nga topp fa jigéen ñi. Dinaa wax xale yu góor yi ne leen buñu la sonal. Soo maree, demal naan ca njaq ya góor ñi duy.»