Ruth 4:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu wax ak mbokk ma yeyoo sañ-sañu jotaat ba, ne ko: «Ab làccu suuf bu sunu mbokk Elimeleg moomoon la, Nawmi di ko jaay. Mooy ka jóge réewum Mowab, ñibbsi.