Ruth 4:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba Israyil, jamono yu jëkk yooya, mbirum njëndum jotaat mbaa ag weccoo, la ñu ko baaxoo dogale ci diggante nit ak moroom ma, nii la: kii day summi dàllam, jox kee. Noonu lees daan yoonale ag jëflante ca Israyil.