Song of Solomon 8:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Junniy dogi xaalis yi, Suleymaan, yaa ko moom; ñaar téeméer yi, beykat yi. Waaye sama toolub reseñ, maa ko moom.