Titus 1:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Loolu war na, ndaxte am na ñu bare ñu déggul lenn ndigal, rawatina ci Yawut yi, ñuy yàq xeli nit ñi ak seen waxi neen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat bare na ñu të, rawatina ci tuubéen ñi bokk ci askanu yawut, ay waxkati neen lañu, te ñooy yàq xeli nit ñi.