bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Titus 1:11
Titus 1:11 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Fàww nga wedamloo leen, ndax dañuy tas këri lëmm, ciy jàngale li warul ngir sàkku alal ju lewul.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li war moo di tëj seen gémmiñ, ndax këri lëmm lañuy tase àlluwa ju ñu amul sañ-sañam, ngir di ko sàkkoo am-am bu lewul.