Titus 1:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Am na nitu Kereet, di yonent ci ñoom, mu ne: «Waa Kereet, ay fenkat lañu mas a doon, ñu soxor ni ay rabi àll, fuqle te tayel.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma wax ko waru jenn waay, ab waa Keret buy seen yonentu bopp. Mu ne: «Waa Keret, ay fen-kati neen, soxor niy rabi àll, fuqle, yaafus.»