Titus 1:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te léegi, ci jamono ji ko soob, feeñal na xebaaram boobu ci waaraate, bi ma Yàlla sunu Musalkat dénk te digal ma, ma xamle ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye tey bi mu jotee, Yàlla sunu Musalkat moo feeñal kàddoom ci biir waare bi mu ma dénk man, te moo ma digal ma xamle ko.