Titus 1:4 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Maa ngi lay bind, Tit, yaw sama doomu diine ju wér ci ngëm, gi nu bokk nun ñépp. Na la Yàlla Baay bi ak Kirist Yeesu sunu Musalkat may yiw ak jàmm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bataaxal bi ñeel na Tit, sama doomu yoon ci kaw ngëm gi nu bokk. Aw yiw ak jàmm ñeel na la, bawoo fa Yàlla Baay bi, ak Almasi Yeesu sunu Musalkat.