Titus 1:5 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bàyyi naa la ca réewu Kereet, ngir nga mottali la desoon ci liggéey bi, te samp ay njiiti mbooloo ca dëkk bu nekk, ni ma la ko sante woon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li tax ma bàyyi la gannaaw ca réewum Keret mooy nga mottli la desoon ca liggéey ba, te nga tabb ay mag ñu jiite mbooloo mi ci dëkk bu nekk, na ma la ko sante woon, man ci sama bopp.