Titus 1:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye war na man gan te bëgg lu baax, di ku maandu te jub, ku sell te noot boppam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye war na di ku man gan, ku xejjoo lu baax, jiital am xelam, jub, sell te moom boppam.