Titus 1:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
War na jàpp ci xebaar bu dëggu, bi lal sunu yoon, ba man a dénkaane ci njàngale mu wér mi, tey yey ñi weddi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na jàpp bu dëgër ci kàddu gu wóor gi, ni ñu ko ko jàngale, ngir mu man di ñaaxe jooju àlluwa ju wér, tey tiiñal weddikat yi.