Titus 2:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte yiwu Yàlla feeñ na te ubbil na ñépp buntu mucc.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax yiwu Yàlla kat feeñ na, te looloo indil ñépp ag mucc.