Titus 2:6 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Naka noonu itam nanga xiir waxambaane yi cig maandu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka noonu, xale yu góor yi itam, ñaaxleen ci jiital seenum xel.
Recommended Reading