Titus 2:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te yaw, ci lépp lu mu man a doon, nekkal ab royukaay ci jëf yu baax. Na sa njàngale wér te am faayda,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te nanga doon, yaw ci sa bopp ab royukaay, ci lépp ndax sa jëf ju baax, te nga boole ko ak àlluwa ju dëggu te tedd,