Titus 2:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ànd ak wax yu wér yu kenn mënta diiŋat, ngir sunuy noon rus ba wedam, ci li ñu amul dara lu ñu nu tuumaal.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ak kàddu gu wér gu kenn dul mana weddi, ngir rusloo ab noon bu amul lenn lu bon lu mu nu baatale.