Titus 3:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
xam ne nit ku ñaaw xel la te ay bàkkaaram fés ci ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te xam ne ku ni mel daa làggi ci bàkkaaram, te moo daan boppam.