Titus 3:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu ma la yónnee Artemas walla Tisig, gaawantul fekksi ma ci dëkku Nikopolis, ndax fa laa bëgg a lollikooji.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw bu ma la yónnee Artemas mbaa Tisig, defal loo man ba fekksi ma Nikopolis, ndax fa laa fas yéenee lollikooji.