Titus 3:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Na sunuy bokk it takku ci jëf yu rafet, ba man a faj aajo yépp, te bañ a yaafus.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na sunuy ñoñ tàggatu ci jëf ju baax ju ñu saxoo ba faj soxla yu taxaw, ngir ñu baña ñàkk njariñ.