bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Titus 3:15
Titus 3:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñiy ànd ak man ñépp ñu ngi lay nuyu. Nuyul nu sunuy soppey ngëm. Na yiwu Yàlla ànd ak yéen ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem ñi ma nekkal ñu ngi lay nuyu. Nuyul nu sunuy soppe ci yoonu ngëm wi nu bokk. Aw yiw ñeel na leen, yeen ñépp.