Titus 3:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Buñu jëw kenn mbaa ñuy ŋaayoo, waaye nañu yiwe te won ñépp lewet gu mat sëkk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buñu yàq der te buñu bëggu ay, waaye nañu di bëggkati jàmm, te nañuy jëfe lewetaay gu mat sëkk, seen digg ak ñépp.