Zechariah 10:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu suuf maree, ñaanal Aji Sax ji ab taw, Aji Sax ji mooy sàkk ay xàmbaar, sóobal nit ab taw, saxalal ku ne am ñax ci àll bi.