Zechariah 8:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: «Mag ñu góor ñeek ñu jigéen ñeey dellu tooge pénci Yerusalem, ku ci nekk ak bantam cib loxoom, ndax at yu bare.