Zephaniah 3:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Maa noon Yerusalem: “Xanaa moos dinga ma ragal, déggal ab yar.” Su ko defee dëkkuwaayam du tas, ndax mboolem mbugal yi ma ko dikke, waaye moo yàkkamtee ñaaw ci jépp jëfam,